Kaay Waay Lyrics Translation – Dm | Vj

VJ sings Kaay Waay from the album DM. Beneth Seraphin Akatche Koffi and Oumar Sarr write about a love that feels fated by God. The song blends Wolof and French to celebrate a rare connection.

Kaay Waay Lyrics Translation – Dm | Vj
Released: December 14, 2024

Kaay Waay

Vj • From “DM”

Lyricist
Beneth Seraphin Akatche Koffi, Cheikh Tidiane Krouma, Mouhamed Abdoulaye Preira, Oumar Sarr
Composer

What is the meaning of Kaay Waay Lyrics from DM?

Beneth Seraphin Akatche Koffi writes that the lover changed his heart into lemonade, sipping and drinking it. He describes a promise to guide each other through life and be there when needed.

Ndeke Dou Mbeuguelou KassèThis isn’t just an ordinary love.
Teh Sax Xetou Mbeuguel Yi Dafa RareAnd this kind of love is truly rare.
Dièkou Ma Ni Douma Bale Yeah YeahI’m not giving up, I won’t give up, yeah, yeah.
An Konne Yaw Bandi Nga Ndèkè BebeSo you’re a captivating bandit, baby.
Sopi Nga Sama Xol Bi LimonadeYou’ve turned my heart into lemonade.
Siroter Ko Diko Nane Yeah YeahSipping it, drinking it, yeah, yeah.
Ndax Baniouy Ndieukeu GuissanterBecause when we first met each other.
Li Nga Ma Yene Nimou DisserThe way you felt about me, it just unfolded.
Ak Niniou XolanterAnd the way we looked at each other.
Rek Ma Xamni Yalla Niou BolèThat’s how I knew ‘God’ united us.
Est-ce Que Do Djinè Ndax Diomal Nga Ma Kaay WaayAre you a ‘djinn’? You’ve made me so shy, come on.
Doflo Ngama Kaay WaayYou’ve driven me crazy, come on.
Wayè Deufeul Ngama Kaay WaayBut you’ve also completed me, come on.
Mane Limay Doundou Ni Daal Nexma Kaay WaayWhat I’m experiencing now truly delights me, come on.
So Bèguè Ma Bègue Kaay WaayIf you’re happy, I’m happy, come on.
Niou Deukè Di Rè Kaay WaayLet’s live and laugh, come on.
Yaw Moussoul Metti Ba Nga Reuthiou Li Nga Ma Xam Kaay WaayYou’ve never regretted what you know about me, come on.
Maala Geuneul Lounè Kaay WaayI prefer you over everything, come on.
Teh Yaama Geuneul Kounè Kaay WaayAnd you’re better than everyone, come on.
Bae Liniouy Doundou Ni Tièr-Carrè Na Kaay WaayUntil what we’re living is perfectly balanced, come on.
Bègal Ma Bèg Kaay WaayMake me happy and be happy, come on.
Ma Xeuthie Sa Reundeul Happy Kaay WaayI’ll embrace your happiness, come on.
Soma Sorè Oh My LoveIf you’re far from me, oh my love.
Namel Bimay Yeuk Thi YawThe longing I feel for you.
Wallahi Yaako Meuneu Fadie NieuweulBy ‘Allah’, you’re the only one who can heal it, so come.
Niouy Kaf Di RèLet’s joke and laugh.
Niouy Kaaf Di Fo Di RèLet’s joke, play, and laugh.
Ndax Baniouy Ndieukeu GuissanterBecause when we first met each other.
Li Nga Ma Yene Nimou DisserThe way you felt about me, it just unfolded.
Ak Niniou XolanterAnd the way we looked at each other.
Rek Ma Xamni Yalla Niou BolèThat’s how I knew ‘God’ united us.
Est-ce Que Do Djinè Ndax Diomal Nga Ma Kaay WaayAre you a ‘djinn’? You’ve made me so shy, come on.
Doflo Ngama Kaay WaayYou’ve driven me crazy, come on.
Wayè Deufeul Ngama Kaay WaayBut you’ve also completed me, come on.
Mane Limay Doundou Ni Daal Nexma Kaay WaayWhat I’m experiencing now truly delights me, come on.
So Bèguè Ma Bègue Kaay WaayIf you’re happy, I’m happy, come on.
Niou Deukè Di Rè Kaay WaayLet’s live and laugh, come on.
Yaw Moussoul Metti Ba Nga Reuthiou Li Nga Ma Xam Kaay WaayYou’ve never regretted what you know about me, come on.
Maala Geuneul Lounè Kaay WaayI prefer you over everything, come on.
Teh Yaama Geuneul Kounè Kaay WaayAnd you’re better than everyone, come on.
Bae Liniouy Doundou Ni Tièr-Carrè Na Kaay WaayUntil what we’re living is perfectly balanced, come on.
Bègal Ma Bèg Kaay WaayMake me happy and be happy, come on.
Ma Xeuthie Sa Reundeul Happy Kaay WaayI’ll embrace your happiness, come on.
Oh Bébé Toi Mon BébéOh baby, you’re my baby.
Toi Qui M’as Tout DonnéYou who’ve given me everything.
Je Pourrais Jamais Te QuitterI could never leave you.
Je T’en Fais La Promesse Mon BebeI’m making you that promise, my baby.
Tu M’as Tellement ÉpauléYou’ve supported me so much.
Quand Il Le FallaitWhen it was necessary.
M’a Sorti De La GalèreYou’ve pulled me out of trouble.
Je Vais Te Rendre La MoneyI’m going to return the favor.
Oh Bebe Yaw Mi Gounguè Ma Man Malay GounguèOh baby, you guide me, and I’ll guide you.
Et Si T’as Peur Crie Aider Moi Mane Maaa Lay SauvéAnd if you’re afraid, cry for help, I’ll be the one to save you.
Oh Bebe Yaw Ndax Beuguè Ngama Comme Nim La BeuguèOh baby, do you love me as much as I love you?
Ndax Nim La Beugè Eup Naaa Wa Li Noum DèmèBecause the way I love you is overwhelming, oh, how it goes.
Oh Bébé Toi Mon BébéOh baby, you’re my baby.
Toi Qui M’as Tout DonnéYou who’ve given me everything.
Je Pourrais Jamais Te QuitterI could never leave you.
Je T’en Fais La Promesse Mon BebeI’m making you that promise, my baby.
Tu M’as Tellement ÉpauléYou’ve supported me so much.
Quand Il Le FallaitWhen it was necessary.
M’a Sorti De La GalèreYou’ve pulled me out of trouble.
Je Vais Te Rendre La MoneyI’m going to return the favor.
Oh Bebe Yaw Mi Gounguè MaOh baby, you who guides me.

Kaay Waay Music Video

The Kaay Waay lyrics meaning shows how love transforms the singer completely. The song declares eternal support and gratitude for a partner who has been a guiding light.